LEEBONE SPECIAL RAMADAN Bén paa serere lawone. Dafa ragal koor - TopicsExpress



          

LEEBONE SPECIAL RAMADAN Bén paa serere lawone. Dafa ragal koor tellement que kéne khamoul loumou done. Mou dégg amna béne mouss bou kham secret bou graw. Maname béne jour ci wér bi bo khamné soko woré diaroul ngay woor yénén jour yi. Mou eundi mouss bi ci keurgui dieund ration un mois, chaque jour sou lékké reek diokh mouss bi aussi. Niou diapéko nonou ba niouné soubeu la Korité. Rek my pa tourné ci mouss bi: yow ya meuna fééne, ana liniou done wakh ci yow. Mouss bi néko: "Moo mane may chrétien, Tom la toudou" A vos meew
Posted on: Tue, 09 Jul 2013 00:25:11 +0000

Trending Topics



tbody" style="min-height:30px;">
Encouraging Each Other: 1 Thessalonians 5:11 ESV Therefore
Agora é oficial, saiu no Domingo Fantástico (domingo passado).
Former midfielder Paul Scholes says new Manchester
You would swim the seven seas, climb the highest mountains, travel

Recently Viewed Topics




© 2015