Mouss( chat) defa djogué makka( mecque), rabou al yeub gnieuw - TopicsExpress



          

Mouss( chat) defa djogué makka( mecque), rabou al yeub gnieuw diko ziar, gnouné dianakh(souris) demal ziarko, dianakh néllèle makka sopiwoul djiko, tourr rek la soppii, niit gni di insister pour convaincre dianakh pour mou deme ziar mous, apres dianakh bi dem.. mais baka mouss guissé rek dafa teup ci kawam... kalaw bi naww. dianakh bi daw.....nilène.. wakhone nalene makka dou sofii djikoooo ......
Posted on: Fri, 06 Sep 2013 09:04:35 +0000

Trending Topics



Recently Viewed Topics




© 2015