bii mom c listoir dun tres bon ami a moi dont jn devoilerai - TopicsExpress



          

bii mom c listoir dun tres bon ami a moi dont jn devoilerai lidentité k si il m provok.....!!! histoir vré la nak...dou vitalait dé..!! bon!! un jour nak dafa solou ba nice def parfum bou cher té nékh... muy dokhantou avenue lamine gueye bi rek, bénn girl jiss ko bardé ci pét rek néko: -"waw!! kel classe!!!!" rek copain tourné néko: -"CM2"!!! mais jour bobou la rouss..................!!!!!!!!!!!!!!!!
Posted on: Fri, 23 Aug 2013 21:49:03 +0000

Trending Topics



Recently Viewed Topics




© 2015