Mbokou djoulitt yi niongui leen di nouyou dileen nianal ngeremou - TopicsExpress



          

Mbokou djoulitt yi niongui leen di nouyou dileen nianal ngeremou serigne touba di sakkou thi yeen ngeen nianal niou. SERIGNE ABO FALILOU (khalif serigne fallou mbacké) mo am ab ligueey bumuy def Suba thia TOUBA MADINA mouy liguey thi tool yi. Départ bi suba la thi 8h Point de depart yi moy: Keur S Fallou (thi jouma ji) Ndindy (serigne Fallou) Alieu. Batay kou thi beugg def adiya pour gazoil ndah tracteur yi ak oto yi mane nga dem keur serigne fallou diohé ko. Serigne bi di niaane kepp fouko teew soxla bofa indi yalnako yalla safara thi barké baatam S Falilou. Dieuredieuf Mouride
Posted on: Fri, 16 Aug 2013 19:52:16 +0000

Trending Topics



Recently Viewed Topics




© 2015